Text copied!
Bibles in Wolof

2 TIMOTE 2:15 in Wolof

Help us?

2 TIMOTE 2:15 in Téereb Injiil

15 Góor-góorlul ba teew fa kanam Yàlla, nekk liggéeykat bu mu nangul te rusoo ci dara, di faramfàcce bu jub kàddug dëgg gi.
2 TIMOTE 2 in Téereb Injiil

2.Timote 2:15 in Kàddug Yàlla gi

15 Defal sa kem-kàttan ba boo teewee fa kanam Yàlla, di ku mu gërëm, ab liggéeykat bu mucc gàcce, di xamle kàddug dëgg gi ni mu ware.
2.Timote 2 in Kàddug Yàlla gi