Text copied!
Bibles in Wolof

2 TIMOTE 2:14 in Wolof

Help us?

2 TIMOTE 2:14 in Téereb Injiil

14 Saxal ci di leen fàttali mbir yooyu, di leen dénk fa kanam Yàlla, ñu moytoo werante ciy araf, ndax loolu jëmul fu dul ci yàq ngëmu ñiy déglu.
2 TIMOTE 2 in Téereb Injiil

2.Timote 2:14 in Kàddug Yàlla gi

14 Loolu, dee ko fàttlee, te ngay dénkaane fi kanam Yàlla, ñu bañ di xuloo ci ay baat, ndax amul njariñ, ñi koy dégg doŋŋ lay sànk.
2.Timote 2 in Kàddug Yàlla gi