Text copied!
Bibles in Wolof

Yunus 3:10 in Wolof

Help us?

Yunus 3:10 in Kàddug Yàlla gi

10 Yàlla nag gis seeni jëf, gis na ñu dëddoo seen jëfin ju bon. Yàlla daldi fomm mbugal ma mu leen naraloon, ba mujju koo def.
Yunus 3 in Kàddug Yàlla gi