Text copied!
Bibles in Wolof

YAWUT YA 11:16 in Wolof

Help us?

YAWUT YA 11:16 in Téereb Injiil

16 Waaye ñu ngi doon séentu réew mu gën, maanaam mi nekk ci asamaan. Looloo tax Yàlla rusul ñu koy wooye seen Yàlla, ndaxte defaral na leen ab dëkk.
YAWUT YA 11 in Téereb Injiil

Yawut ya 11:16 in Kàddug Yàlla gi

16 Waaye réew mu ko gën lañu doon sàkku, te mooy réewum asamaan. Looloo tax Yàlla rusul ñu di ko tudde seen Yàlla, ndax waajalal na leen ab dëkk.
Yawut ya 11 in Kàddug Yàlla gi