Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 9:5-7 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 9:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Ba mu ko defee ñu yóbbu ca bunt xaymab ndaje ma la Musaa santaane woon, mbooloo ma mépp ñëw, taxaw fa kanam Aji Sax ji.
6 Musaa ne: «Lii mooy li Aji Sax ji santaane ne, moom ngeen wara def ngir leeram feeñu leen.»
7 Musaa wax ak Aaróona ne ko: «Dikkal fii ci sarxalukaay bi te joxe sa saraxu póotum bàkkaar ak sa saraxu rendi-dóomal, nga jotoo ko, yaw yaak mbooloo mi, boo noppee joxe saraxu mbooloo mi, jote leen ko, muy li Aji Sax ji santaane.»
Sarxalkat yi 9 in Kàddug Yàlla gi