Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 8:35-36 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 8:35-36 in Kàddug Yàlla gi

35 Ci bunt xaymab ndaje mi ngeen di yem guddeek bëccëg diiru juróom ñaari fan, boole ci di dénkoo dénkaaney Aji Sax ji, ndax ngeen baña dee, ndaxte loolu moo di li ñu ma santoon.»
36 Aaróona ak doomam yu góor nag def lépp lu Aji Sax ji santaane woon, Musaa jottli.
Sarxalkat yi 8 in Kàddug Yàlla gi