Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 8:3-4 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 8:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 te nga woo mbooloo mi mépp, ñu daje ci bunt xaymab ndaje mi.»
4 Musaa def la ko Aji Sax ji sant, mbooloo ma daje ca bunt xaymab ndaje ma.
Sarxalkat yi 8 in Kàddug Yàlla gi