Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 8:29 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 8:29 in Kàddug Yàlla gi

29 Musaa daldi jël dënn biy céram ci kuuyu xewu colu gi, yékkati ko, jébbal Aji Sax ji, muy saraxu yékkati-jébbale, di la Aji Sax ji santoon Musaa.
Sarxalkat yi 8 in Kàddug Yàlla gi