Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 8:20-21 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 8:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 daldi daggat kuuy mi, def ko ay dog, boole bopp beek dog yeek nebbon bi, lakk ko, ba mu dib dóom.
21 Ba loolu weesee Musaa boole yérey biir yi, ak yeel yi, raxas, ba noppi lakk kuuy mi yépp ca sarxalukaay ba. Loolu saraxu rendi-dóomal la, ngir xetug jàmm. Saraxu sawara la, ñeel Aji Sax ji, na ko Aji Sax ji sante woon Musaa.
Sarxalkat yi 8 in Kàddug Yàlla gi