Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 8:15 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 8:15 in Kàddug Yàlla gi

15 Musaa rendi ko, sàkk ci deret ji, capp ci baaraamam, diw ci ñeenti béjjéni sarxalukaay bi yépp, setale ko sarxalukaay bi. Mu daldi tuur li des ci deret ji ci taatu sarxalukaay bi, sellale ko noonu, muy njotlaayal sarxalukaay bi.
Sarxalkat yi 8 in Kàddug Yàlla gi