Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 8:10-11 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 8:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Ba loolu wéyee Musaa jël diwu pal ga, diw ca jaamookaay baak ya ca biir yépp, sellale ko yooya,
11 ba noppi wis-wisal ca juróom ñaari yoon ca kaw sarxalukaay ba, diwe ko sarxalukaay ba ak mboolem ay ndabam, boole ca mbalkam njàpp ma, mook ub tegoom ngir yooyu it sell.
Sarxalkat yi 8 in Kàddug Yàlla gi