Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 7:13-14 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 7:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Sarax boobu da ciy dolli mburu yu am lawiir, boole kook saraxu cant googu ci biir jàmm te mu jublu ci njukkal.
14 Nañu jooxeel Aji Sax ji ab cér ci sarax yooyu yépp, muy moomeelu sarxalkat bi xëpp deretu juru saraxas cant gi ci biir jàmm ci mboolem weti sarxalukaay bi.
Sarxalkat yi 7 in Kàddug Yàlla gi