Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 6:9 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 6:9 in Kàddug Yàlla gi

9 La ca des Aaróona aki doomam yu góor ñoo koy lekk, te buñu ci boole lawiir. Nañu ko lekke ci bérab bu sell. Ci biir ëttu xaymab ndaje mi lañu koy lekke.
Sarxalkat yi 6 in Kàddug Yàlla gi