Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 6:13 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 6:13 in Kàddug Yàlla gi

13 «Li Aaróona aki doomam yu góor di sarxalal Aji Sax ji, keroog bu ñu koy diw, fal ko, mooy lii: ñetti kiloy sunguf su mucc ayib, tollook saraxu pepp bi ñu saxoo bés bu nekk, te genn-wàll gi di suba, genn-wàll gi ngoon.
Sarxalkat yi 6 in Kàddug Yàlla gi