Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 5:7-8 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 5:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 «Nit ki amul lu mat njégu gàtt, na indil Aji Sax ji ñaari pitax mbaa ñaari xati yu ndaw, muy daanam ndax bàkkaar bi mu def; benn bi di saraxu póotum bàkkaar, bi ci des di sarax rendi-dóomal.
8 Da koy yót sarxalkat bi, kooku jëkka rey benn bi, muy saraxu póotum bàkkaar; na kutt baat bi te bumu teqale bopp beek baat bi.
Sarxalkat yi 5 in Kàddug Yàlla gi