Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 5:12 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 5:12 in Kàddug Yàlla gi

12 Da koy yót sarxalkat bi, sarxalkat bi sàkk ci barci-loxo, muy saraxu baaxantal, mu daldi koy lakk ca kaw sarxalukaay bi, mu dolliku ci saraxi sawara yi. Saraxu póotum bàkkaar la.
Sarxalkat yi 5 in Kàddug Yàlla gi