Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 4:12 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 4:12 in Kàddug Yàlla gi

12 mboolem li des ci yëkk wi daal lay génne dal bi, yóbbu ko ci bérab bu mucc sobe, ca jalub dóom ba, daldi taal matt, lakk ko ca, ba mu dib dóom. Foofa dóom ba jale lees koy lakk.
Sarxalkat yi 4 in Kàddug Yàlla gi