Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 3:5-7 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 3:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Na doomi Aaróona yi boole yooyu lakk ci kaw sarxalukaay bi, mu tege ci kaw saraxu rendi-dóomal bi ci kaw mattum taal bi. Saraxu sawara la ngir xetug jàmm ñeel Aji Sax ji.
6 «Su fekkee ne li nit kiy sarxalal Aji Sax ji saraxu cant la ci biir jàmm, te mu di ko jële ci jur gu gàtt, gu góor mbaa gu jigéen, na sarxal lu amul sikk.
7 Su dee sarxal xar, na ko indil Aji Sax ji
Sarxalkat yi 3 in Kàddug Yàlla gi