Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 26:15-16 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 26:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 su ngeen teddadilee samay dogal, dëddu samay ndigal, ba jëfewuleen sama santaane yépp, xanaa di fecci sama kóllëreek yeen,
16 su boobaa li may def ak yeen mooy lii: maay jekki wàcce njàqare ci seen kaw, mu ànd ak woppi ràgg, yaram wu tàng jérr ak bët yu lëndëm, ngeen gën di wopp. Dingeen ji seenum pepp ci neen, ndax seeni noon a koy lekk.
Sarxalkat yi 26 in Kàddug Yàlla gi