Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 25:22-24 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 25:22-24 in Kàddug Yàlla gi

22 Bu ngeen tolloo ci ji ci atum juróom ñetteel ba, dina leen fekk ngeen di lekk meññeefum daaw-jéeg, te meññeefum atum juróom ñeenteel ba dina agsi, fekk ngeen di lekk ca mu daaw-jéeg ma.
23 «Suuf si deesu ko jaay, mu wel fàww, ndax maay Boroom suuf si, yeen ay doxandéem ngeen fi, yu ma fi dëkkal.
24 Fépp fu bokk ci seenum réew, nangeen fa yoonal sañ-sañu jotaat ca suuf sa.
Sarxalkat yi 25 in Kàddug Yàlla gi