Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 25:16-17 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 25:16-17 in Kàddug Yàlla gi

16 Lu at yooya gëna bare, njég ga gëna jafe; lu at ya gëna néew, njég ga gëna yomb, ndaxte limu meññeefum suuf sa lees leen koy jaaye.
17 Buleen di naxante, waaye ragal-leen seen Yàlla, ndax man Aji Sax ji maay seen Yàlla.
Sarxalkat yi 25 in Kàddug Yàlla gi