Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 25:10 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 25:10 in Kàddug Yàlla gi

10 Te nangeen sellal at ma ca topp di juróom fukkeelu at ma, ngeen yéene ca mboolem waa réew ma ba mu daj, ne ngoreel taxaw na. Seen atum Yiwiku la, ku nekk war cee dellu ca suufu waa këram, ku nekk it wara dellu ca làng ga mu bokk.
Sarxalkat yi 25 in Kàddug Yàlla gi