Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 22:19-21 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 22:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 liy tax ñu nangul ko mooy muy jur gu amul sikk, di góor; man naa doon aw yëkk mbaa kuuy mbaa sikket.
20 Lenn lu ci am sikk buleen ko sarxal, ndax deesu leen ko nangul.
21 «Su nit dee joxsi Aji Sax ji aw nag mbaa gàtt, muy saraxu cant ci biir jàmm, mu di ko wàccoo ngiñ mbaa muy saraxu yéene, na doon lu amul sikk, ndax ñu nangul ko. Lenn luy sikk du nekk ci jur gi.
Sarxalkat yi 22 in Kàddug Yàlla gi