Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 21:6 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 21:6 in Kàddug Yàlla gi

6 Nañu nekkal seen Yàlla ay nit ñu sell, te baña teddadil seen turu Yàlla, ndax saraxi sawar yi ñeel Aji Sax ji, te di seen ñamu Yàlla, ñoo koy joxe. Kon nag dañoo wara sell.
Sarxalkat yi 21 in Kàddug Yàlla gi