Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 21:18-20 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 21:18-20 in Kàddug Yàlla gi

18 Du kenn sax ku am sikk kuy agsi ba fii, du gumba, du kuy soox, du ku xar-kanamam am sikk mbaa ku cér yi sutaate.
19 Du it ku tànk bi làggi mbaa loxo bi,
20 mbaa ab xuuge mbaa ab tungune; du it ku bëtam am sikk mbaa ku ràmm mbaa ku am góom yu sol dëtt, mbaa ku ñu tàpp.
Sarxalkat yi 21 in Kàddug Yàlla gi