Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sarxalkat yi 18:13-15 in Wolof
Help us?
Sarxalkat yi 18:13-15
in
Kàddug Yàlla gi
13
«Bul dëkkoo sa ndey ju ndaw, ndax daa jegewook sa yaay lool cig bokk.
14
«Bul torxal sa baay bu ndaw di dëkkoo soxnaam. Sa ndey la.
15
«Bul dëkkoo sa soxnas doom. Sa soxnas doom la. Bu ko dëkkoo mukk.
Sarxalkat yi 18 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms