Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 14:53-56 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 14:53-56 in Kàddug Yàlla gi

53 Na bàyyi picc miy dund fu génn dëkk ba, mu naaw ca àll ba. Noonu lay defe njotlaayal néeg bi, mu set.»
54 Loolu la yoon digle ci lépp luy jàngoroy der juy law ak wat-wataan,
55 mbaa liir wu tegu ci ndimo mbaa ci néeg,
56 ak ci wàllu tërgën itam mbaa mu diy ër mbaa gàkk bu weex;
Sarxalkat yi 14 in Kàddug Yàlla gi