Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 14:47-49 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 14:47-49 in Kàddug Yàlla gi

47 Ku tëdd ca biir néeg ba war naa fóot ay yéreem te ku fa lekke it war naa fóot ay yéreem.
48 «Su sarxalkat ba delloo ca néeg ba, seet ko, fekk liir wa lawul ca néeg ba, gannaaw ba ñu ko raaxee, na biral ne néeg bi set na, ndax kon liir wa raaf na.
49 Liy laabal néeg bi moo di mu sàkk ñaari picc ak bantu garabu seedar ak wëñ gu xonq curr ak caru isob.
Sarxalkat yi 14 in Kàddug Yàlla gi