Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 14:1-2 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 14:1-2 in Kàddug Yàlla gi

1 Aji Sax ji teg na ca ne Musaa:
2 «Li yoon digle ci mbirum nit ku ame jàngoroy der juy law, keroog bés ba ñuy laabal nit ki, mooy lii: Nañu ko yegge sarxalkat bi.
Sarxalkat yi 14 in Kàddug Yàlla gi