Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 13:47-48 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 13:47-48 in Kàddug Yàlla gi

47 «Su ndimo xuuree, teg aw liir, muy ndimol kawaru gàtt gu ñu ëcc mbaa yu wëñ gu ëccu,
48 mu tegu ci bàgg mbaa ci poqe, su dee kawar gu ëccu, su dee wëñ gu ëccu walla der bu ñu wulli walla mboolem lu ñu defare der,
Sarxalkat yi 13 in Kàddug Yàlla gi