Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 11:23-25 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 11:23-25 in Kàddug Yàlla gi

23 Waaye mboolem yeneen gunóor yuy naaw tey doxe ñeenti tànk sibleen ko.
24 «Yii nag da leen di sobeel te képp ku laal lu ci dee dina yendoo sobe ba jant so.
25 Te itam képp ku for lenn lu dee ci yii, na fóot ay yéreem, waaye dina yendoo sobe ba jant so.
Sarxalkat yi 11 in Kàddug Yàlla gi