Text copied!
Bibles in Wolof

Sarxalkat yi 10:19-20 in Wolof

Help us?

Sarxalkat yi 10:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Aaróona ne Musaa: «Xoolal rekk tey ni bànni Israyil indile Aji Sax ji seen saraxu póotum bàkkaar ak seen saraxu rendi-dóomal, te teewul lii dal ci sama kaw! Bu ma lekkoon tey ci yàppu saraxas póotum bàkkaar bi, ndax dina neex Aji Sax ji?»
20 Musaa dégg kàddu yooyu, rafetlu ko.
Sarxalkat yi 10 in Kàddug Yàlla gi