Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 99:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 99:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Fa biir taxaaru niir wa la waxeek ñoom, ñu topp kàdduy seedeem ak dogalu yoonam ba mu leen joxoon.
8 Céy sunu Yàlla Aji Sax ji, yaa leen nanguloon, di seen Yàlla ju leen di baal, te di leen mbugale seeni jëf ju bon.
Sabóor 99 in Kàddug Yàlla gi