Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 99:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 99:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Sa tur weeka màgg te raglu. Sàbbaal-leen ko. —Kee sell!
4 Buur, jëfe yoon mooy dooleem, te yaa saxal njub, yoon ak njekk ci askanu Yanqóoba.
5 Màggal-leen sunu Yàlla, Aji Sax ji, te sujjóot fa ndëggastalam. —Kee sell!
Sabóor 99 in Kàddug Yàlla gi