Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 98:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 98:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Moo dencal bànni Israyil ngoram, dencal ko wormaam, àddina ba mu daj di gis ni nu sunu Yàlla walloo.
4 Yeen àddina sépp, xaacul-leen Aji Sax ji, sampleen, sarxolle te woy!
Sabóor 98 in Kàddug Yàlla gi