Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 97:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 97:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Gàcce ñeel na kuy jaamu jëmmi tuur, di puukarewoo ay yàllantu. Yeen yàllay xeet yépp, sujjóotal-leen kii,
8 Siyoŋ dégg ca, bég, waa Yuda it di bànneexoo àttey Aji Sax jii.
Sabóor 97 in Kàddug Yàlla gi