Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 97:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 97:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 tund yi ne soyox seey fi kanam Aji Sax ji boroom àddina sépp.
6 Asamaan a ngi biral njekkam, xeetoo xeet di gis darajaam.
Sabóor 97 in Kàddug Yàlla gi