Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 97:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 97:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Sawaraa dox, jiitu ko, di xoyomi noonam wetoo wet,
4 ay melaxam leeral àddina, waa àddina gis, di pat-pati;
5 tund yi ne soyox seey fi kanam Aji Sax ji boroom àddina sépp.
6 Asamaan a ngi biral njekkam, xeetoo xeet di gis darajaam.
Sabóor 97 in Kàddug Yàlla gi