Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 97:10-11 in Wolof

Help us?

Sabóor 97:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Yeen soppey Aji Sax ji, bañleen lu bon. Aji Sax jeey sàmm ay wóllëreem, di leen musal ci ku bon.
11 Jub, leerlu; jubal, bég.
Sabóor 97 in Kàddug Yàlla gi