Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 96:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 96:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Aji Sax jee màgg, jara santa sant te gëna mata ragal lépp lu ñuy jaamu.
5 Mboolem yàlla yi xeet yiy jaamu, yàllantu la, waaye Aji Sax jee sàkk asamaan.
Sabóor 96 in Kàddug Yàlla gi