Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 95:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 95:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Mooy sunu Yàlla, nuy xeet wi muy foral, diy gàtt ciy loxoom. Bésub tey yal nangeen dégg kàddoom
8 ga mu noon: «Buleen të, na woon fa Meriba, jantub keroog fa Maasa, ca màndiŋ ma,
9 fa ma seeni maam doon nattoo, di ma seetlu te gis la ma def.
Sabóor 95 in Kàddug Yàlla gi