Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 95:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 95:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax jeey Yàlla ju màgg ji, buur bu mag bi tiim yàllay xeet yépp.
4 Moo moom xóotey suuf, moom colli tund yi,
5 moom géej, sàkk ko, moom jéeri ji mu mooñ.
6 Nan sëgg, sujjóot, sukkal Aji Sax ji nu sàkk.
Sabóor 95 in Kàddug Yàlla gi