Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 te naa: «Ki Sax gisu ci, Yàllay Yanqóoba jii yégu ko.»
8 Yeen bokk yu dofe yi, moytuleen. Gàtt xel yi, kañ ngeen di muus?
9 Ki jëmbati nopp, da dul dégg a? Am ki xari gët, da dul gis?
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi