Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:5-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:5-9 in Kàddug Yàlla gi

5 Aji Sax ji, say ñoñ lañuy dëggaate; say séddoo lañuy néewal.
6 Jëtun akub doxandéem, ñu faat; ab jirim, ñu bóom,
7 te naa: «Ki Sax gisu ci, Yàllay Yanqóoba jii yégu ko.»
8 Yeen bokk yu dofe yi, moytuleen. Gàtt xel yi, kañ ngeen di muus?
9 Ki jëmbati nopp, da dul dégg a? Am ki xari gët, da dul gis?
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi