Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:5-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Aji Sax ji, say ñoñ lañuy dëggaate; say séddoo lañuy néewal.
6 Jëtun akub doxandéem, ñu faat; ab jirim, ñu bóom,
7 te naa: «Ki Sax gisu ci, Yàllay Yanqóoba jii yégu ko.»
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi