Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:3-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:3-7 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji, fu ku bon kiy àkki? Fu ku bon kiy kañu àkki?
4 Ñu ngi làmmiñoo reewande, képp kuy def lu bon di damu.
5 Aji Sax ji, say ñoñ lañuy dëggaate; say séddoo lañuy néewal.
6 Jëtun akub doxandéem, ñu faat; ab jirim, ñu bóom,
7 te naa: «Ki Sax gisu ci, Yàllay Yanqóoba jii yégu ko.»
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi