Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji, fu ku bon kiy àkki? Fu ku bon kiy kañu àkki?
4 Ñu ngi làmmiñoo reewande, képp kuy def lu bon di damu.
5 Aji Sax ji, say ñoñ lañuy dëggaate; say séddoo lañuy néewal.
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi