Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:23 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:23 in Kàddug Yàlla gi

23 Moo leen di këpp seen ñaawtéef, sànke leen seenug mbon. Sunu Yàlla Aji Sax jee leen di sànk.
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi