Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:19-22 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:19-22 in Kàddug Yàlla gi

19 Ma bare xalaati xol, nga dëfal ma, ma bég.
20 Loo séq ak njiit lu jubadi luy yoonal njubadi?
21 Ñii dañoo mànkoo, di tëru ku jub, di teg àtteb dee ku deful dara.
22 Waaye Aji Sax jeey sama rawtu, sama Yàlla laay sës, làqu.
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi