Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 94:15-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 94:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Àtte dina dellu laloo njekk, képp ku jub topp ca.
16 Ana ku may taxawal ci ñu bon ñi? Ku may jógal ci biir ñiy def lu bon?
Sabóor 94 in Kàddug Yàlla gi